| Regarde ce que j'ai trouvé | |
|
|
Auteur | Message |
---|
julie .:::|| ami ||:::.
Nombre de messages : 6903 Age : 62 Date d'inscription : 19/12/2006
| Sujet: Regarde ce que j'ai trouvé Mar 27 Mar 2007 - 16:57 | |
| Gore Daf Di Nyaan
Ma né Wax nu
Ku leen gis, nu dellusi ci guudi ?
Rab yi ci àll bi
Di dellusi guddi
Te bëccëgu njolloor nuy naaw
Nakka njugub yiy nàmp derati nit
Tey tagg ci pegg yu ratax
Yi ci kàmb.
Wax nu ku leen gis ?
Wax nu ku leen gis ?
Rab yiy dox diggu njolloor .
Ci digg àllu mandeng
mi ngelaw liy wall tàkkusaan
Ci la guddi lëndëm Kuruus tëdd
Boxx bànneexam
Nerferkare Danga leer !
Lalal ci kow suuf leer nann
Ma né Yàlla , Nun yéeg nan tey ciy jaww
Te yéen néew yi dëddu àddina
Hamleen ka
Maa di démb te dara umpu ma ci ëllëg
Ma di dënnu wu weex tàll woowu
Di àddu fu mu tawe ba sewÊt
Def xon muri mel nam jant
Yéen ni yëlif ndox
Di Rabi ndox
Yéen niy aw ci sama kàddu
Man maa di ki leen
Wo
Yow Tswigoo
Yow miy Baayi Baay yi
Yaay sunu Baay Nun Ndaama yi
Defal ba niir yii
di Taw.
Fexeel ba ma nyam
doom yi suuf menn
Danga dootul ndax sunu Baay ?
Baayu Baay yi ?
Jamono yegsi na
Bant bi xer ndox
Nanga ji te mennyal
Allu jàmm wi wêr Ngaay Mexe
Beykatu dugubu jamm
Beykatu ceebu jamm
Komo Nama wi jooy na jamm.
Ama may ko fan wu guud
Moom komo nama wu bees wi
Na la suuf sédd
Fan wu gudd,
Yaw koma nama wu
Bees wiy seede
Addina wiy nëw
Nit day reer tëdd. Dee
Mu sedd guyy !
Na la Rab wiy wattu
Sédd fan wu gudd
Danga di Boroom kàddu gu wér
Kumba Bang
Kumba Lambaay
Kumba Kastel
Sedd nu jàmm
Sedd nu fan wu gudd
Yàgg ci buumu njaam
Wër àddina ba mu sës
Génn xeet ci àtte
Nu jaay la ci yoon
Nga dellu tey di gor
Man ma di Gore | |
|
| |
julie .:::|| ami ||:::.
Nombre de messages : 6903 Age : 62 Date d'inscription : 19/12/2006
| Sujet: Re: Regarde ce que j'ai trouvé Mar 27 Mar 2007 - 17:57 | |
| - winbald a écrit:
- Allé on confie la traduction de tout ça à mamediarra!
Oui, je l'ai en anglais mais pas en français, et puis faut la faire travailler cette petite. C'est bien de se sentir utile ! lol J'en aurai un autre si elle veut ! | |
|
| |
sistersandrine Co-Admin
Nombre de messages : 4526 Age : 60 Date d'inscription : 15/03/2007
| |
| |
julie .:::|| ami ||:::.
Nombre de messages : 6903 Age : 62 Date d'inscription : 19/12/2006
| Sujet: Re: Regarde ce que j'ai trouvé Dim 1 Avr 2007 - 22:10 | |
| - Citation :
- winbald a écrit:
Allé on confie la traduction de tout ça à mamediarra! lol! Alors ! Y a des nouvelles ?? | |
|
| |
sistersandrine Co-Admin
Nombre de messages : 4526 Age : 60 Date d'inscription : 15/03/2007
| Sujet: Re: Regarde ce que j'ai trouvé Sam 7 Avr 2007 - 19:09 | |
| | |
|
| |
julie .:::|| ami ||:::.
Nombre de messages : 6903 Age : 62 Date d'inscription : 19/12/2006
| Sujet: Re: Regarde ce que j'ai trouvé Lun 23 Avr 2007 - 17:27 | |
| | |
|
| |
sistersandrine Co-Admin
Nombre de messages : 4526 Age : 60 Date d'inscription : 15/03/2007
| Sujet: Re: Regarde ce que j'ai trouvé Lun 30 Avr 2007 - 2:22 | |
| | |
|
| |
julie .:::|| ami ||:::.
Nombre de messages : 6903 Age : 62 Date d'inscription : 19/12/2006
| Sujet: Re: Regarde ce que j'ai trouvé Lun 30 Avr 2007 - 10:28 | |
| Mais dis-nous Qui les a vus les Revenants de la nuit ? Les Esprits de la Forêt 0h Pygmée. Les Revenants de la nuit Qui le jour clair, Comme les chauves-souris qui sucent le sang des hommes, Demeurent accrochés aux parois lisses des grandes cavernes Dis-nous qui les a vus ? Sous la forêt qui pleure, sous. le vent du soir La nuit toute noire s'est couchée joyeuse pygmées Neferkare ! Tu es lumineux ! Ce qui est à toi sur terre luit : Dieu voici désormais venir Toujours Et vous défunts d'au-delà de ce monde! Sachez le ! Dans les sarcophages, Je suis Hier Et je connais Demain Je suis la foudre blanche Qui gronde après la pluie sur le Basuto Vous qui commandez aux eaux Esprit des Eaux Vous tous qui m'obéissez C'est moi qui vous Appelle sur les terres du pays Fang Ô toi Tsuigoa Toi père des pères Tu es notre père A nous du Pays Des hommes de petite taille. Fais que les nuages Apportent la Pluie. Fais que je mange Les fruits de la Terre. N'es-tu pas notre père Le père des pères ? Et voilà qu'il est temps Baton qui aime l'Eau De planter et de faire croître Entre Oakha et Kulikuli Bonne brousse Cultivateur de petit mil Cultivateur de riz Cultivateur de coton Le Masque a pleuré ! Q’Ama te donne donc longue vie à Toi Masque Nouveau Que la Terre du Hogon Te donne donc longe vie. A toi Masque Nouveau L'Homme mange et dort. Il meurt. Et c'est le grand froid. Que les génies Hogon te donnent longue vie Tu es une Voix Forte Tes yeux sont le Soleil Kumba Bang Donne nous la Paix Donne nous longue vie A force d'avoir Esclave Erré à travers le Monde Exilé par jugement Vendu selon la loi Je suis Redevenu Liberté Je suis Gorée | |
|
| |
sistersandrine Co-Admin
Nombre de messages : 4526 Age : 60 Date d'inscription : 15/03/2007
| Sujet: Re: Regarde ce que j'ai trouvé Lun 30 Avr 2007 - 13:47 | |
| | |
|
| |
julie .:::|| ami ||:::.
Nombre de messages : 6903 Age : 62 Date d'inscription : 19/12/2006
| Sujet: Re: Regarde ce que j'ai trouvé Lun 30 Avr 2007 - 15:06 | |
| Y a pas de miracle , faut remercier Internet. En fait j'avais la traduction en Français depuis le début, mais je ne l'avais pas vu, je croyais qu'elle n'était qu'en version Anglaise | |
|
| |
sistersandrine Co-Admin
Nombre de messages : 4526 Age : 60 Date d'inscription : 15/03/2007
| Sujet: Re: Regarde ce que j'ai trouvé Lun 30 Avr 2007 - 15:20 | |
| | |
|
| |
julie .:::|| ami ||:::.
Nombre de messages : 6903 Age : 62 Date d'inscription : 19/12/2006
| Sujet: Re: Regarde ce que j'ai trouvé Lun 30 Avr 2007 - 15:21 | |
| | |
|
| |
Contenu sponsorisé
| Sujet: Re: Regarde ce que j'ai trouvé | |
| |
|
| |
| Regarde ce que j'ai trouvé | |
|