Ci teen bii
Laa la jëme
Kaay deglu
Sa baat mu awu
Su li hoot nee selaw
Muur lëndëm fu sore
Danaa la wommat
Hamnaa heru geej
Wu gill dul wacc
Soo tooge ma toog
Daanu dëj callweer.
Muusaa Ka
Le grand poete
Wolof du Baol
Poeme A Une Jeune Femme
Du fonds de ces puits
D'où n'emerge nul reflet
Tu viendras sonder ta voix
Nous investiront le silence
Et si le vide engorge le noir sombre
Des profondeurs
Je te menerai plus loin par la main
Je connais un rivage
En tourment de bruits de vagues
Assis côte à côte
Nous y dompterons le vent.